1
00:01:02,046 --> 00:01:07,046
Yuci moo ko bind

2
00:03:04,467 --> 00:03:05,966
Demal!

3
00:03:42,838 --> 00:03:45,006
tëye liiñ bi!

4
00:04:20,108 --> 00:04:21,174
Kaay fii!

5
00:04:27,681 --> 00:04:28,983
Keda!

6
00:05:55,968 --> 00:05:57,369
Danga jàllul.

7
00:06:11,383 --> 00:06:12,551
Jàkkaarloo.

8
00:06:29,101 --> 00:06:30,102
Lajj.

9
00:06:36,074 --> 00:06:37,109
Lajj.

10
00:06:56,261 --> 00:06:57,296
Jàkkaarloo.

11
00:07:08,339 --> 00:07:11,375
Metit dina ànd ak nun.

12
00:07:40,404 --> 00:07:41,571
Dakkal dal!

13
00:08:01,725 --> 00:08:06,493
Baay, yaa ngi xeeñ!

14
00:08:08,865 --> 00:08:11,531
Di nga rëbb ci sama wet.

15
00:08:11,533 --> 00:08:14,270
Yaay doomu njiit li.
Sama doom.

16
00:08:30,786 --> 00:08:36,058
Waneel ni mën nga jiite.
Wutal sa doole.

17
00:10:06,481 --> 00:10:08,516
Moom waajalul.

18
00:10:11,985 --> 00:10:14,522
Benn sesoŋ at mu nekk...

19
00:10:15,689 --> 00:10:18,058
...nu ngi rëbb Rab wu Mag wi.

20
00:10:19,726 --> 00:10:22,496
Danuy def lii, wala sunu askan dee.

21
00:10:23,530 --> 00:10:27,868
Dafa wara def wareefam.

22
00:10:29,503 --> 00:10:33,373
wane boppam ci askan wi.

23
00:10:36,409 --> 00:10:38,876
Sudee mënul...

24
00:10:38,878 --> 00:10:42,480
Dama ko bëgg
ak sama xol yépp.

25
00:10:42,482 --> 00:10:46,717
Mën na dee.
Maa ngi ragal.

26
00:10:46,719 --> 00:10:49,523
Dafay jiite ak xolam.

27
00:10:50,823 --> 00:10:53,326
Du lansam.

28
00:11:43,642 --> 00:11:45,477
Jël lii...
kon dara du leen gaañ.

29
00:11:46,945 --> 00:11:48,813
Mën naa toppatoo sama bopp.

30
00:11:55,153 --> 00:11:56,421
Keda.

31
00:12:06,464 --> 00:12:08,800
Xam ni bëgg naa la.

32
00:12:17,275 --> 00:12:19,141
Dina nu won
ni nit la.

33
00:12:19,143 --> 00:12:20,443
Wutal palaas ngir jiite.

34
00:12:20,445 --> 00:12:22,113
Soo noppee nga ñibbi.

35
00:12:23,181 --> 00:12:26,351
Mën nga ko dige.

36
00:12:35,025 --> 00:12:36,293
Dem.

37
00:14:16,492 --> 00:14:20,059
Ngir mucc fàww nu focus...
Deel am dal.

38
00:14:20,061 --> 00:14:22,061
Buñu xàddi.

39
00:14:57,965 --> 00:14:58,966
Baay...

40
00:15:45,446 --> 00:15:46,680
Sama xarit.

41
00:15:52,985 --> 00:15:56,189
Mucc ngeen ci sedd bi.
Amaana gëna graaw tuuti?

42
00:15:57,557 --> 00:15:58,725
Waaw.

43
00:16:00,026 --> 00:16:03,831
Maa ngi indi ab rëbbkat bu ndaw...

44
00:16:05,364 --> 00:16:08,201
Yékkati sa bopp...
te say bët dina ñu ko topp.

45
00:16:13,206 --> 00:16:14,640
Lii sama doom la.

46
00:16:20,146 --> 00:16:22,415
Sama bos duko gis
beneen rëbb.

47
00:16:24,217 --> 00:16:26,184
Dafa dem
ci maam ya.

48
00:16:45,070 --> 00:16:48,273
Danga wara nekk baay bu gëm boppam.

49
00:16:49,608 --> 00:16:52,742
Yaakaar naa ni dina may féexal xol.

50
00:17:03,088 --> 00:17:05,255
Sunu nit ñi dox nañu
Yoon bu sell bi

51
00:17:05,257 --> 00:17:07,292
Yoonu depuis
rëbb bu mag bi njëkk.

52
00:17:08,460 --> 00:17:12,597
Màrk yi ñoo nuy wan sunu yoon.
Sunuy maam ñoo ko defar.

53
00:17:18,904 --> 00:17:22,070
Dañu ko bàyyi muy yoon
ngir nu topp ko.

54
00:17:22,072 --> 00:17:25,042
Ak ngir jàppale nu mucc
tukki bu mag bi.

55
00:17:28,580 --> 00:17:31,816
Sunu loxo dañu nu joxoñ
dem ci barabu rëbb.

56
00:17:32,751 --> 00:17:35,486
Ñenn ñi dina ñu dellusi.

57
00:17:36,053 --> 00:17:38,455
Ñenn ñi duñu ko bëgg.

58
00:17:40,491 --> 00:17:44,493
Yooyu màrk ñu ngi des... ngir
njiit ngir yóbbu rëbbkat yi seen kër.

59
00:18:11,187 --> 00:18:12,288
Jeexal ko.

60
00:18:50,460 --> 00:18:53,228
Yaa ngi jël dundu
ngir dundal sa askan.

61
00:18:54,030 --> 00:18:56,797
Defal ko. Léegi.

62
00:19:03,372 --> 00:19:04,506
Man itam bëgg naa la!

63
00:19:11,146 --> 00:19:13,116
Dundu ngir ñi am doole!

64
00:19:16,318 --> 00:19:19,254
Dañu koy liggéey, duñu ko jox.

65
00:20:20,748 --> 00:20:22,416
Deel ànd ak dal.

66
00:20:52,345 --> 00:20:54,581
Deeleen yewwu.

67
00:21:32,652 --> 00:21:34,685
Demna...

68
00:21:34,687 --> 00:21:38,622
...waaye danu wara dëgër.

69
00:21:45,131 --> 00:21:47,133
Yalna ngëmam
xool yoon wi...

70
00:21:48,201 --> 00:21:51,868
...ni ay maam
ci kanamam.

71
00:24:00,596 --> 00:24:04,433
Màrku xeer yi
di leen jàppale ci bis bi.

72
00:24:06,669 --> 00:24:12,206
Leegi yaa ngi yor màndarga yi...

73
00:24:12,208 --> 00:24:15,978
...loolu moo lay wan
ci guddi.

74
00:24:33,028 --> 00:24:36,031
Leer gi
ci sunuy maam...

75
00:24:38,033 --> 00:24:41,136
...mu wane nu yoonu ñibbi.

76
00:24:47,575 --> 00:24:49,508
Ker.

77
00:24:55,217 --> 00:24:57,217
Gis nga bii?

78
00:24:57,219 --> 00:25:00,089
Loolu mooy Alfa,
seen njiit.

79
00:25:06,362 --> 00:25:11,165
Alpha dafa wara toppatoo baayimam.
Lu ëpp lépp.

80
00:25:13,835 --> 00:25:17,770
Waaye moom itam
saa yu nekk ci jafe-jafe.

81
00:25:21,676 --> 00:25:27,413
Ñeneen ñi ci mbooloo mi
dina ko laaj...

82
00:25:30,918 --> 00:25:34,253
...sudee dañu yëg ni dañu néew doole.

83
00:25:34,255 --> 00:25:37,056
Alpha dafay may ñeneen ñi
xam barabam...

84
00:25:37,058 --> 00:25:39,593
...ak dooleem ak dal gi.

85
00:25:43,131 --> 00:25:47,400
Judduwul Alfa.

86
00:25:47,402 --> 00:25:52,639
Waaye yeg na ko ci fit wi mu am...
ak xolam.

87
00:26:13,727 --> 00:26:14,993
Shh.

88
00:27:32,371 --> 00:27:33,539
Dem!

89
00:28:02,000 --> 00:28:03,399
Keda!

90
00:28:05,336 --> 00:28:06,768
Keda!

91
00:28:08,339 --> 00:28:10,439
Keda!

92
00:28:10,441 --> 00:28:12,508
Bul xool ci suuf!

93
00:28:16,013 --> 00:28:18,216
Bul bàyyi mu dem!

94
00:28:33,030 --> 00:28:36,433
Keda!

95
00:28:51,381 --> 00:28:53,048
Sama xarit...

96
00:28:55,285 --> 00:28:57,154
...sama njiit...

97
00:28:59,656 --> 00:29:01,924
Loolu mënul am
ngir yegg ci moom!

98
00:29:04,328 --> 00:29:06,263
Dem na.

99
00:29:09,299 --> 00:29:11,602
Mënu la ñàkk itam.

100
00:29:13,236 --> 00:29:16,072
Am nanu wareef
ci sunuy nit.

101
00:29:25,649 --> 00:29:27,917
Keda!

102
00:29:35,491 --> 00:29:37,460
Yab ci sled yi.

103
00:29:45,800 --> 00:29:48,271
Danu wara dellusi
ci sunu dëkk.

104
00:29:49,804 --> 00:29:55,311
Yalna Xel yi jiite
nga aar sa askan.

105
00:30:02,652 --> 00:30:09,625
Wax ko sunuy doom dina ñu dox
bokk ci beneen àdduna.

106
00:30:52,434 --> 00:30:55,002
Danga ko wara bàyyi mu dem.

107
00:30:58,372 --> 00:31:00,274
Joxleen ko.

108
00:31:56,963 --> 00:32:00,266
Mooy
ak Xel yi leegi.

109
00:33:07,799 --> 00:33:08,900
Baay!

110
00:33:11,837 --> 00:33:13,068
Baay!

111
00:35:09,819 --> 00:35:10,920
Baay!

112
00:36:22,890 --> 00:36:23,924
Baay!

113
00:42:59,612 --> 00:43:02,148
Hien yi, danu wara am fuñu mëna dëkk.

114
00:46:22,010 --> 00:46:23,578
Xarit.

115
00:46:42,997 --> 00:46:44,530
Amaana duko def.

116
00:46:54,141 --> 00:46:55,610
Bul ma màtt.

117
00:46:58,045 --> 00:47:00,781
Duma la lor.

118
00:47:05,719 --> 00:47:07,788
Dinaa la dundal.

119
00:47:17,864 --> 00:47:19,033
Xarit.

120
00:47:23,069 --> 00:47:24,204
Gis.

121
00:48:21,259 --> 00:48:23,061
Dañu ko wara raxas.

122
00:48:56,728 --> 00:48:57,962
Xoolal...

123
00:49:00,665 --> 00:49:02,133
...baaxul noonu.

124
00:50:08,965 --> 00:50:10,200
Mukk.

125
00:50:46,368 --> 00:50:48,571
Baal naa la.

126
00:50:49,839 --> 00:50:51,741
Moo ci man.

127
00:50:55,544 --> 00:50:57,714
Danga wara xaar
ngir sa turn.

128
00:51:04,686 --> 00:51:07,055
Kontaan naa
nu déggante.

129
00:52:37,778 --> 00:52:39,814
Ker.

130
00:52:51,291 --> 00:52:54,561
Yaa ngi leen di namm, sa pack...

131
00:52:55,829 --> 00:52:59,466
Dégg naa samay waajur
wooma ci samay gént.

132
00:53:10,443 --> 00:53:12,912
Waaye mënu ma leen jot...

133
00:53:20,720 --> 00:53:23,188
Dafay gëna sedd.

134
00:53:25,557 --> 00:53:29,027
Yoonu sell bi dina muur
ak neige ci lu yaggul dara...

135
00:53:29,029 --> 00:53:32,431
Xamuma ndax dinaa ko mëna def
sama pàppa nekkul ci kër gi.

136
00:53:36,602 --> 00:53:39,772
duma ni moom...

137
00:53:44,743 --> 00:53:47,279
...waaye fàww ma jéem.

138
00:53:51,517 --> 00:53:54,386
Namm naa samay waajur lool.

139
00:54:30,655 --> 00:54:32,157
Loolu mooma ko moom.

140
00:54:33,424 --> 00:54:34,892
Dama ko soxla.

141
00:55:01,986 --> 00:55:05,422
Dama wara nekk ci kër gi
balaa neige bu njëkk bi.

142
00:55:06,224 --> 00:55:08,525
Yaw itam danga wara ñibbi.

143
00:55:11,595 --> 00:55:12,997
Psst.

144
00:55:13,964 --> 00:55:15,099
Ayca!

145
00:55:17,701 --> 00:55:19,103
Bàyyi xool ma!

146
00:55:19,536 --> 00:55:21,104
Ayca!

147
00:57:10,078 --> 00:57:11,279
Fan nga jëm?

148
00:57:13,648 --> 00:57:15,250
Lan mooy?

149
00:57:20,088 --> 00:57:21,488
Demal sa kër!

150
00:57:42,843 --> 00:57:44,245
Demal, joge fi!

151
00:58:48,674 --> 00:58:49,976
Dama daanaka am ko.

152
00:58:50,676 --> 00:58:52,643
Ndax gis nga ko ?

153
00:58:56,716 --> 00:58:58,683
Dama réer rek.

154
00:59:00,652 --> 00:59:02,687
Ragaluma dara.

155
00:59:03,856 --> 00:59:05,992
Saa waay, looy def?

156
00:59:07,726 --> 00:59:08,827
Dellul fii!

157
00:59:12,497 --> 00:59:13,498
Fi!

158
01:00:47,257 --> 01:00:48,624
Fii!

159
01:00:57,834 --> 01:00:58,868
Xaar!

160
01:01:18,988 --> 01:01:19,989
Déedéet!

161
01:01:24,726 --> 01:01:26,195
Xam nga ni dinaa la dundal.

162
01:02:59,753 --> 01:03:01,422
Yaa ngi xeeñ.

163
01:03:17,605 --> 01:03:19,804
Duggal ci ndox mi!

164
01:03:19,806 --> 01:03:21,440
Bul fexe ma topp la.

165
01:03:28,616 --> 01:03:30,281
Ñëwal fii,
ñëwal fii.

166
01:04:05,218 --> 01:04:06,484
Ah. Ah.

167
01:04:14,293 --> 01:04:16,194
Dinaa la woowe Alfa.

168
01:04:17,497 --> 01:04:18,665
Keda.

169
01:04:20,132 --> 01:04:21,467
Alfa.

170
01:06:29,359 --> 01:06:32,462
Demal ci sa njaboot...

171
01:08:14,060 --> 01:08:15,262
Maa ngi jéggalu...

172
01:09:09,348 --> 01:09:10,617
Baal ma...

173
01:09:14,754 --> 01:09:16,022
Alfa!

174
01:11:58,981 --> 01:11:59,982
Ndimbal dimbali!

175
01:12:03,085 --> 01:12:04,318
Ndimbal dimbali!

176
01:12:04,320 --> 01:12:05,855
Xarit!

177
01:12:20,503 --> 01:12:21,802
Dédeet...

178
01:12:37,619 --> 01:12:39,155
Deggal.

179
01:12:49,798 --> 01:12:50,799
Lekk... Lekk.

180
01:12:58,706 --> 01:12:59,972
Dara!

181
01:12:59,974 --> 01:13:01,409
Déedéet!

182
01:13:02,309 --> 01:13:03,375
Dara!

183
01:13:24,765 --> 01:13:27,202
Dina nu baax.

184
01:14:02,602 --> 01:14:04,771
Noo ngi leen di sant ci seen ndimbal...

185
01:14:32,632 --> 01:14:33,731
Daw!

186
01:16:09,394 --> 01:16:11,028
Alfa!

187
01:16:36,186 --> 01:16:39,589
Jërëjëf sama xarit.

188
01:16:41,258 --> 01:16:43,926
Duma xàddi ci yaw...

189
01:16:44,894 --> 01:16:47,530
Sama askan laa.

190
01:18:12,347 --> 01:18:14,382
Yoon wi. Danu jege.

191
01:19:17,244 --> 01:19:19,580
Samay maam
leeral yoon wi...

192
01:19:20,780 --> 01:19:22,616
...di nu yóbbu seen kër.

193
01:20:28,680 --> 01:20:30,282
Ngir Yàlla. Jiwu.

194
01:20:31,950 --> 01:20:33,652
Xamnaa ni mën nga ko.

195
01:20:38,957 --> 01:20:41,326
Nu ngi ñëw
ba leegi ñu bokk...

196
01:20:43,861 --> 01:20:46,531
Mënu ma la ñàkk.

197
01:20:50,535 --> 01:20:52,203
Baal ma, Alfa.

198
01:21:38,582 --> 01:21:40,984
Dama soxla noppalu tuuti rek...

199
01:22:14,217 --> 01:22:17,020
Mën na dee. Maa ngi ragal.

200
01:22:18,121 --> 01:22:20,557
Dafay jiite ak xolam.

201
01:22:21,691 --> 01:22:23,560
Du lansam.

202
01:22:26,763 --> 01:22:27,764
Déedet.

203
01:22:28,698 --> 01:22:32,602
Moo gëna am doole
lu ngeen xam.

204
01:22:35,304 --> 01:22:39,074
Moo gëna am doole
moom sax xamul.

205
01:23:34,595 --> 01:23:36,330
Nu ngi ci kër gi.

206
01:24:19,239 --> 01:24:23,009
Naka la loolu mana ame ?

207
01:24:25,512 --> 01:24:26,914
Baay.

208
01:24:34,254 --> 01:24:35,653
Keda!

209
01:24:43,996 --> 01:24:45,866
dama ragaloon
Duma la gisati ba fàww.

210
01:24:47,267 --> 01:24:52,171
Yaa ngi fi. Ak nun.
Yaa ngi ci sa kër dëgg.

211
01:24:58,712 --> 01:25:04,348
Bëggoon naa ngeen gëna fonk.

212
01:25:04,350 --> 01:25:10,289
Sama doom, yelloo nga ko.
Danga ñëw ci nun.

213
01:25:26,105 --> 01:25:27,606
Alfa.

214
01:25:31,977 --> 01:25:33,245
Alpha soxla...

215
01:25:33,612 --> 01:25:35,447
Dimbali.

216
01:26:35,305 --> 01:26:40,375
Keda indi nala ci kër gi
ci nun. Famiy ngeen.

217
01:26:56,360 --> 01:27:03,333
Noo ngi leen di dalal
ci sunu askan.

218
01:27:37,000 --> 01:27:40,269
Leegi baaxna.

219
01:29:27,475 --> 01:29:32,475
Yuci moo ko bind


